Testo Mame Boye - Wally B. Seck
Testo della canzone Mame Boye (Wally B. Seck), tratta dall'album Xel
mame boye boulma di méré sama Mame
Dinala setsi Mame
Mame boye boulma fi méré sama Mame
Dinala setsi Mame
Oooh Oohhh Ohhhh Oooohhhhh
Oohhh oohhh oohhh oohhhhh
Damalay xalaat all time
Ioe sama Mame yama yarr yama diapalé ioe la beug
Damalay xalaat all time
Ba poullo diery ndegeum kene nieuwoul bokko
Shibireppp rep rep rep barabiriré
Damalay xalaat all time
Ba poullo diery ndegeum kene nieuwoul bokkooo
Mame boye boulma di méré sama Mame Dinala setsi Mame
Mame boye boulma di méré sama Mame dinala setsi Mame
Dinala setsi Mame dinala setsi maaaame mame boye mame boye mamamaam dinala setsi mame dinala setsi maaaame
Damalay xalaat all time (×2)
I will talk to you ndeye wouly Fall ndeye soda Fall nga bokal ndey ak baye dinala setsi mame boye
Sira Ndiaye gorou Fall mame boye
Sira ndiara gorou Fall mame boye mame boye
Talibé serigne Babacar Sy sopey Dabakh Sy malick
Mi gnou ber ndel ngi gnou thieureulé mi gnou thieureulé sène baay bi
El hadji Malick Sy
Sira ndiara gorou Fall mame boye
Credits
Writer(s): Wally Ballago Seck
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Disclaimer:
i testi sono forniti da Musixmatch.
Per richieste di variazioni o rimozioni è possibile contattare
direttamente Musixmatch nel caso tu sia
un artista o
un publisher.