Testo Cherche en toi - Wally B. Seck
Testo della canzone Cherche en toi (Wally B. Seck), tratta dall'album Xel
j'ai chercher en toi la quiétude, je me rends compte d'une solitude euh!
j'ai chercher en toi une solution, je me rends compte d'une désillusion
j'ai chercher en toi le bien fait d'un roi, je me rends compte d'un désarroi
j'ai chercher en toi de l'espoir, je me rends compte de ton absence ce soir
x2
Diokh ma sa bopp, ma défal la lila diomb,
Bayyi mak sa khel ma yobbou la fodoul fattééé téé
enhh yééhh ééhhhé
Diokh maa sa boppeu ma défal laa lila diomb wowo maahhh
Diokh ma sa bopp ma défal laa lila diomb, Bayyi mak sa khel ma yobbou la fodoul fattéé héé
Iow ni ngay dokhé nonou lay dokhé
Iow ni ngay sollo nonou lay sollo
Ah iow ni ngay wakhé nonou laay diko wakhéé héé
XXXX
Nékak iow dafma dane geuneul ngay kham li néh ci mane dafma dane deuffeul yaye
No no no no ohh iow ak mane damaka dane deuggeul
Ba soula dôme yi wérénté ba lougn ma khélal
Sama yéné ci iow damaka dane feusseul
No no no no ohh yama dane deuffeul
Iow ni ngay dokhé nonou lay dokhé
Iow ni ngay sollo nonou lay sollo
Kham nga ni ngay wakhé nonou lay diko wakhéé héé
XXXX
Credits
Writer(s): Wally Ballago Seck
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Disclaimer:
i testi sono forniti da Musixmatch.
Per richieste di variazioni o rimozioni è possibile contattare
direttamente Musixmatch nel caso tu sia
un artista o
un publisher.