Rockol30

Testo Paradise - Wally B. Seck

Testo della canzone Paradise (Wally B. Seck), tratta dall'album Xel

Ma ngui fatalikou bi meu ley sogeu guiss thi lay wakh nane niane gui nangou na beureub bi meu done guent big fofou rek lay khel di guiss li meu beugone niou and feu.
Beureub bou beut meussoul leu khol fenen fou nit demoul wone.
Banekh bou rey lay am thi di khol beuss mi gui nieuw mane ak yaw ley done.
Legui niou gui ni nioune niar sou niou niane antou na.
Yallah mi gui ak nioune, My baby guentou niou oubil seu beut khol.
Bess bi niou done khar yekssi na oubil seu beut noron yi madjiri, ndokh ming gni weur, souf ssi sédé, ndierer yi naw mane ak yaw dou wakhi nen.
Geumone na li rire thi mane mbeuguel leu wone yaw la done set yaw rek leu wone.
Ma ngui fatelikou seu thiono ak seu tiss.
Len la done tite, niou délou ganaw.
Li mey deuké niane niou ande fenen.
Beureub bou beut meussoul leu khol, fenen fou nit demoul wone.
Banekh bou reu lay am thi di khol beuss mi gui nieuw mane ak yaw ley done.
Legui niou gui ni nioune niar souniou niane antou na.
Yallah mi gui ak nioune, My baby guentou niou oubil seu beut khol.
Bess bi niou done khar yekssi na oubil seu beut noron yi madjiri, ndokh ming gni weur, souf ssi sédé, ndierer yi naw mane ak yaw dou wakhi nen.
Yegone na li rire thi mane mbeuguel leu wone yaw la done set yaw rek leu wone.
Mangui fatelikou goudi yi niou done niane.
Bour bi Yallah moy sédé, Geumone na ni mane ak yaw ley done.
Sou doul wone ak yaw dou done kenen.
Sama paradise wawaw, sama aljanah, sama paradise sama aljanah take you one love.
Li ssi li ssi nobel khana nekh na.
Chéri Marie Ndir la, Lamine Dieng sala bayou Amina ak Khadija.
Samuel Fall bayou mame Thierno kouy sa paradise Fall.
Sama paradise wawaw, sama aljanah.
Sa ma paradise.



Credits
Writer(s): Harry Nilsson, Gil Garfield, Perry L. Botkin Jr.
Lyrics powered by www.musixmatch.com

Link

Disclaimer: i testi sono forniti da Musixmatch.
Per richieste di variazioni o rimozioni è possibile contattare direttamente Musixmatch nel caso tu sia un artista o un publisher.

Elenco artisti

© 2025 Riproduzione riservata. Rockol.com S.r.l.
Policy uso immagini

Rockol

  • Utilizza solo immagini e fotografie rese disponibili a fini promozionali (“for press use”) da case discografiche, agenti di artisti e uffici stampa.
  • Usa le immagini per finalità di critica ed esercizio del diritto di cronaca, in modalità degradata conforme alle prescrizioni della legge sul diritto d'autore, utilizzate ad esclusivo corredo dei propri contenuti informativi.
  • Accetta solo fotografie non esclusive, destinate a utilizzo su testate e, in generale, quelle libere da diritti.
  • Pubblica immagini fotografiche dal vivo concesse in utilizzo da fotografi dei quali viene riportato il copyright.
  • È disponibile a corrispondere all'avente diritto un equo compenso in caso di pubblicazione di fotografie il cui autore sia, all'atto della pubblicazione, ignoto.

Segnalazioni

Vogliate segnalarci immediatamente la eventuali presenza di immagini non rientranti nelle fattispecie di cui sopra, per una nostra rapida valutazione e, ove confermato l’improprio utilizzo, per una immediata rimozione.