Testo Sportif - Youssou N’Dour
Testo della canzone Sportif (Youssou N’Dour), tratta dall'album Rokku Mi Rokka
Woyal sa wayu ndam ii
Dangay bégël sa xol bi
Ndax yaa yor bannex bi
Ni tay bés bii sa bés la
Sa mbër daan na kóntaan nga
Bu ñu daanee sa mbër nak
Na nga fexe ba nee
Po mii dañuy Jonante
Faw mu am ku moyle
Jarula defante, di xasteeka dóóre
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal
Bëgóón nga mu demee ni demewuko
Mën naa am bu ëllëgee mu gën fee neex
Ba ma làng ag samay gaa yi ngir bànneexu
Xam ne lii fo la nii lay mënë deme
Powun jonante nii lay deme
Tay jii yaw bu ëllëgee keneen la
Fo ag ree de lañ ciy jublu
Moo tax ñu wara dal taynangu defet
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal
Waa waaw wuy dabbee wuy yoo
Dabi alaa ko ndey baate satata
Abdulaay ag Maajoor Maajoor ag Mataar ag jaara seen jigéén
Sire lañu dóór bal géér ña da ñoo daw
Sire Bàlla moo ñaan Ramata Faal
Siree nga Cees Matee nga Njaarém
Duñ ko wëy ku reew, duñ ko wëy ku ñaaw
Aah wuy dabbee wuy yoo
Dabi alaa ko ndey baate satata
Jonante po ag ree la
Boo gañee fo ag ree la
Boo ñàkkee fo ag ree la
Lépp ci fo ag ree la
Buñ la gañee muñël
Boo ko gañee baalal
Credits
Writer(s): Youssou N'dour, Mody Ba, Mouhamadou Gueye
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Disclaimer:
i testi sono forniti da Musixmatch.
Per richieste di variazioni o rimozioni è possibile contattare
direttamente Musixmatch nel caso tu sia
un artista o
un publisher.
Altre canzoni dell'album
Ultimi articoli
Youssou N'Dour, contratto in esclusiva pluriennale con Universal Music Africa
(14/10/2021)
Youssou N'Dour: la voce del Senegal
(01/10/2019)
Polar Music Prize, vince Youssou N'Dour
(07/05/2013)
Senegal, Youssou N'Dour nominato ministro
(05/04/2012)
Senegal, Youssou N'Dour ferito durante una manifestazione
(22/02/2012)
Youssou N'Dour escluso dalle elezioni in Senegal
(29/01/2012)
Youssou N'Dour ora vuole diventare presidente del Senegal
(03/01/2012)
Youssou N'Dour annulla i concerti, entra in politica dal 2 gennaio
(27/11/2011)
Youssou N'Dour scende in campo per la situazione del Senegal
(25/09/2011)
Crisi alimentare in Africa, concerto di Bono e Youssou N'Dour
(07/09/2011)