Testo Norbon - KEEM C
Testo della canzone Norbon (KEEM C), tratta dall'album BMD: THE MIXTAPE
Mhan norbon na norbon na yeah
Sankuwon na sanku na yeah
Mhan norbon nala
Wy nga yaha suma hkol
Defci lula neh beh pareh nga dem sa yorn
Mhan norbon nala
Wy nga neka nitt ku bon
Yaha suma derr di netali wahi norn
Mhan norbon nala
Wanteh ndekeh bukunj yorn
Neka nitt ku njol sa khol bi nekut lu morl
Mhan norbon nala
Wy dega sumala hamon
Duma jeyma nob wahuma difa fall yeah
Mhan norbon na norbon na yeah
Sankuwon na sanku na yeah
Mhan bugon na bugon na yeah
Dega noborn na norbon na yeah
Wy ndekeh kuma nob ahmna kumu nob eh
Wy ndekeh kuma trust ahmna kumu trust
Wahon nenj ma buma rush
Wy ma banj rek over doff
Yorka chereh bolli sauce
Wy suma hamon duma moss yeah
Mhan norbon nala
Wy nga yaha suma hkol
Defci lula neh beh pareh nga dem sa yorn
Mhan norbon nala
Wy nga neka nitt ku bon
Yaha suma derr di netali wahi norn
Mhan norbon nala
Wanteh ndekeh bukunj yorn
Neka nitt ku njol sa khol bi nekut lu morl
Mhan norbon nala
Wy dega sumala hamon
Duma jeyma nob wahuma difa fall yeah
Aye Legi marngi nii
Munatuma love hawma leelan la nii
Yow yangma baii cy birr
Melni bena dorm hawma fuma neka nii
Dega dega ndekeh foyeh nenj ma
Yaha suma khol pareh dem nak
Suma norbuton dumadon daal
Wy suma hella jahaso woi mhan yeah
Mhan norbon nala
Wy nga yaha suma hkol
Defci lula neh beh pareh nga dem sa yorn
Mhan norbon nala
Wy nga neka nitt ku bon
Yaha suma derr di netali wahi norn
Mhan norbon nala
Wanteh ndekeh bukunj yorn
Neka nitt ku njol sa khol bi nekut lu morl
Mhan norbon nala
Wy dega sumala hamon
Duma jeyma nob wahuma difa fall yeah
Credits
Writer(s):
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Disclaimer:
i testi sono forniti da Musixmatch.
Per richieste di variazioni o rimozioni è possibile contattare
direttamente Musixmatch nel caso tu sia
un artista o
un publisher.