Testo Bégué - Wally B. Seck
Testo della canzone Bégué (Wally B. Seck), tratta dall'album Louné
Beuguel bou djiougué thi mane dji dieum thi yene (bis)
Mo dakh khiff lekke ba marre nane (bis)
Andadooo gueneu loumaléne
Kharitooo waw wakhi noppi
Beuguel bou djiougué thi mane dji dieum thi yene
Mo dakh khiff lekke ba marre nane (bis)
Andadooo gueneu loumaléne
Kharitooo waw wakhi noppi
Solenema nobé
Khole lénema thi yene
Liko warrale moy gnio boke ben wen waw gore
Gniake dou rére
Thiono boromam
Ndéye Fatou Djiagua yayou megni
Motakh li yeppe yawla
Credits
Writer(s): Wally Seck
Lyrics powered by www.musixmatch.com
Link
Disclaimer:
i testi sono forniti da Musixmatch.
Per richieste di variazioni o rimozioni è possibile contattare
direttamente Musixmatch nel caso tu sia
un artista o
un publisher.